1 Ba Borom bi h͈ame nak ne Pharisee ya dēg’ on nañu ne Yesu angi don def te batise i talube yu gen a bare as John,
Ganou yef yōyu Yesu ak i talube am ñou on nañu cha suf i Judea; te mu jēki fa ak ñom te batise.
Te ñu ñou fi John, te ne ko, Rabbi, Kōkale nek’ on ak you ganou wala Jordan, ka nga sēde won, munga batise, te ñepa dika fa mōm.