8 Ngelou li gelou na fa mu buga, te dēga nga rir am, wande h͈amu la fu mu bayako, te fu mu jem: nōnule la ku neka ku jūdu chi Nh͈el ma.
Ña jūdu on, dowul chi deret, mbāte chi mbugel i yaram, mbāte chi mbugel i nit, wande chi Yalla.
Bul jomi ndege da ma la wah͈, ne, Ela ngēn a jūduāt.
Nicodemus tontu te ne ko, Naka la yef yile mune am?