1 Nit i Pharisee ya am on na, ku tuda Nicodemus, kēlifa i Yauod ya:
Te Nicodemus ñou itam, ka jek’ on a dika fa mōm chi gudi, te mu indi mira ak h͈êñay ya ñu bōle won; tēmēr i libar la potah͈.
Yesu tontu te ne ko, Ndah͈ yā di jemantalkat i Israel, te h͈amu la yef yile?
Te munga wah͈ chi biti, te wah͈u len ko dara. Ndah͈ kēlifa ya h͈am nañu ne kile di Krista chi dega?