3 Simon Peter ne len, Mange dem napi. Nu ne ko, Ñunge and’ ak you itam. Ñu gēna, te duga cha gāl ga; te cha gudi ga japu ñu dara.
Wande ba lelek sa jote, Yesu tah͈ou cha tefes ga: wande talube ya h͈amu ñu on ne Yesu la.