John 2:9 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907
9 Ba kēlifa nchēt ga mose ndoh͈ ma sopaliku on biñ, te h͈amul fu mu juge, (wande bukanēg ya h͈am ya rôt on ndoh͈ ma), kēlifa nchēt ga ôlu seyt bu gōr ba,
Yesu ne len, I mbok’ i nēg i borom‐chēt ga, ndah͈ mun naño nah͈arlu ba borom‐chēt ga neke ak ñom? Wande jamāno di na diki ba ño fabi borom‐chēt ga cha ñom; bōbale di nañu ôri.