3 Te ba biñ ba jêh͈e, ndey i Yesu ne ko, Amatu ñu biñ.
Ndege lile di suma deret i koleri gu ês, ja di tūru ndig ñu bare ndege mbaale’ i bakar.
Jigen am ya nak yōni fa mōm, ne, Borom bi, gisal ka nga sopa jēr na.
Ô on nañu itam Yesu ak i talube am cha sey ba.
Te Yesu ne ko, Jigen ji, lu ma jote ak you? Suma wah͈tu dikangul.