Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




John 17:3 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

3 Te dūnda gu dul jêh͈ a di gile, ndah͈ ñu h͈am la, you mi di Yalla ji dega dal, ak Yesu Krista ki nga yōnesi won.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




John 17:3
52 Iomraidhean Croise  

Di ngēn wah͈al ka Yalla selal on, te yōni ko chi aduna si, ne Sāga nga Yalla, ndege wah͈ nā, ne, Mā di Dōm i Yalla?


Te h͈am nā ne dēga nga ma sā su neka: wande ndig mbōlo mu tah͈ou file ma wah͈ ko, ndah͈ ñu gum ne Yā ma yōni on.


Wande Dalalkat ba, mu di Nh͈el mu Sela ma, ka Bay ba di yōni chi suma tur, di na len jemantali yef yepa, te fatali len lu ma len wah͈ on yepa.


Naka nga ma yōni on chi aduna si, nōnule lā len yōni chi aduna si itam.


Ndah͈ ñom ñepa di bena; naka you, Bay bi, neka chi man, te man mā neka chi you, ñom itam ñu neka chi ñun: ndah͈ aduna si di gum ne yā ma yōni on.


Man chi ñom, ak you chi man, ndah͈ ñu motaliku chi bena; ndah͈ aduna si h͈am ne yā ma yōni on, te sopa nga len, naka nga ma sope.


Ey Bay bu jūb bi, aduna si h͈amul la won, wande mā la h͈am on; te ñile h͈am nañu ne yā ma yōni on.


Ndege bāt ya nga ma may on, ñom lā len may; te nangu nañu len, te h͈am chi dega ne chi you lā juge won, te gum ne yā ma yōni on.


Ndege Yalla yōniwul on Dōm am chi aduna si ndah͈ mu ate aduna si; wande ndah͈ aduna si mucha chi mōm.


Ndege kōka Yalla yōni on, bāt i Yalla yi la wah͈: ndege joh͈ewul Nh͈el ma chi natu.


Naka ngēn mune gum, yēn ña nangulante ndam, te ndam li juge cha Yalla reka, ūtu len ko?


Naka ma Bay ba di dūnda yōne, te mā dūnda ndig Bay ba; nōgule la itam ka ma di leka, di na dūnda ndig man.


Mā ko h͈am; ndege fa mōm lā juge, te mō ma yōni on.


Ñu ne ko, Ana sa Bay? Yesu tontu, ne, H͈amu len ma, te h͈amu len suma Bay: su ngēn ma h͈am on, h͈am kon ngēn suma Bay itam.


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan