Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




John 13:3 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

3 Yesu ka h͈am ne Bay ba joh͈ na yef yepa chi i loh͈o am, te juge won na cha Yalla, te di na dem fa Yalla,

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




John 13:3
22 Iomraidhean Croise  

Suma Bay jebal na ma yef yepa; te ken h͈amul Dōm ji wande Bay bi; te ken h͈amul Bay bi wande Dōm ji, ak ku Dōm ji nangu mu h͈am ko.


Yesu ñou fi ñom, te wah͈ len, ne, May nañu ma kantan yepa cha ajana ak chi suf.


Ken mosul a gis Yalla muk; Dōm am ja di bajo, ka neka chi den’ i Bay ba, mō ko fêñal.


Ba h͈ewte i njot ga lāta jot, Yesu ka h͈am ne wah͈tu am dikasi na ba mo di bayi aduna si dem fa Bay ba, naka mu sope won yos am ña neka chi aduna si, mu sopa len be cha muj ga.


Naka nga ko maye won sañsañ chi kou nit ñepa, ndah͈ mu maye ña nga ko may on ñepa dūnda gu dul jêh͈.


Te kena yēgul on cha ajana, wande ka wach’ on cha ajana, Dōm i nit ka sah͈, ka neka cha ajana.


Bay ba sopa na Dōm ja, te joh͈ na ko lu neka chi loh͈o am.


Mā ko h͈am; ndege fa mōm lā juge, te mō ma yōni on.


Yesu ne len, Wah͈tu wu new reka lā neka ak yēn, te di nā dem fa ka ma yōni on.


Yesu tontu te ne len, Su ma sēde suma bopa sah͈, suma sēde dega la: ndege h͈am nā fu ma juge won, te fu ma di dem; wande yên h͈amu len fu ma juge won te fu ma di dem.


Yesu ne len, Su Yalla nek on sēn bay, don ngēn ma sopi: ndege mā juge won te ñou fa Yalla; te diku ma chi suma bopa, wande mō ma yōni on.


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan