Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




John 10:3 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

3 Chi mōm la otukat i bunta ba di ūbi; te nh͈ar ya dēga bāt am; te mu ô i nh͈ar am chi sēn tur, te jīte len cha biti.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




John 10:3
32 Iomraidhean Croise  

Mā di samakat bu bāh͈ bi, te h͈am nā suma yos, te suma yos h͈am nañu ma,


Te amati nā yenen i nh͈ar, ñu bokul chi gēta gile: ñom it, war nā len isi, te di nañu dēga suma bāt; te di nañu neka bena gēta, ak bena samakat.


Ba mu gēne yos am yepa mu jītu len, te nh͈ar ya topa ko; ndege h͈am nañu bāt am.


Mā di bunta bi: chi man su nit h͈arafe, di na mucha, te di na tabi chi bir, gēna cha biti, te feka mporlukay.


Ña ma Bay ba may ñepa, di nañu ñou fi man: te ku ñou fi man, du ma ko dah͈a muka.


Binda nañu chi tēre’ yonent ya, ne, Nepa Yalla di na len jemantal. Ku neka mbōk ku dēga bāt i Bay ba, te jemantu, mu ñou fi man.


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan